Bind
The officer dictates one sentence and you write it (3 tries). Have someone read these to you in English.
Washington was the first President.
Washington moo doon njiit bu njëkk bi.
The capital of the United States is Washington, D.C.
Péeyu Etazini mooy Washington, D.C.
The President lives in the White House.
Njiit li dafay dëkk ci Kër gu Weex gi.
Independence Day is in July.
Independence Day (Bésu Temb bi) ci sulet la.
Citizens can vote.
Way-réew yi man nañu vote.
Mexico is south of the United States.
Meksik dafa nekk ci sudu Etazini.
Canada is north of the United States.
Kanadaa dafa nekk ci nordu Etazini.
The flag is red, white, and blue.
Raaya bi dafa xonq, weex, te baxa.
People pay taxes.
Nit ñi dañuy fey galag (impôts).
New York City was the first capital.
New York City moo doon péey bu njëkk bi.
We have fifty states.
Am nañu juróom-fukki (50) state.
Lincoln was the President during the Civil War.
Lincoln moo doon njiit ci jamonoy Xareb Civil bi.